Back to Reading
1kings 11:38
▼
“Te soo defee mboolem li ma la sant, topp samay yoon, di def li ma rafetlu tey jëfe samay dogal ak samay santaane, na ko Daawuda sama jaam ba daa defe, su boobaa dinaa ànd ak yaw te dinaa la sampal kër gu sax, ni ma ko sampale woon Daawuda, te dinaa la jox Israyil.”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.