Back to Reading
1kings 14:5
▼
“¶ Waaye fekk na Aji Sax ji wax Axiya, ne ko: «Dama ne, soxnas Yerbowam a ngi ñëw di leerlusi mbirum doomam ju góor ci yaw, ndax dafa wopp. Bu dikkee keneen lay mbubboo.» Aji Sax ji ne Axiya, mu wax ko nàngam ak nàngam.”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.