Back to Reading
nehemiah 2:8
▼
“akub bataaxal bu jëm ca Asaf may wattu toolu buur, ngir mu may ma bant yu ma defareji bunti tatay kër Yàlla ga, defaraale ca tatay dëkk baak kër ga may dali.» Buur nangul ma, ndax sama Yàlla ji ma toppe mbaaxam.”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.