Back to Reading
1thessalonians 2:13
▼
“¶ Te it dunu noppee sant Yàlla ci lii: ba ngeen jotee kàddug Yàlla, gi nu doon waare, nangu ngeen ko, waxuma ni kàddug nit waaye ni kàddug Yàlla, ndaxte moom la ci dëgg-dëgg, te mu ngi jëf ci yéen ñi gëm.”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.