Tilde Biblia
Back to Reading

1thessalonians 3:6

¶ Waaye léegi Timote bawoo na ci yéen, indaale xibaar yu neex ci seen ngëm ak seen mbëggeel; xamal na nu ne yéena ngi am pàttaliku yu rafet ci nun te namm nu lool, ni nu leen namme, yéen itam.

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.

1thessalonians 3:6 - Téereb Injiil (Wolof) | Tilde Biblia | Bibliche - La Biblia Interactiva