Tilde Biblia
Back to Reading

1thessalonians 4:1

¶ Léegi nag bokk yi, jot ngeen ci nun, nan ngeen wara dunde ba neex Yàlla, te moom ngeen di def. Waaye ci turu Boroom bi Yeesu nu ngi leen di ñaan ak a dénk, ngeen gën koo feddali.

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.

1thessalonians 4:1 - Téereb Injiil (Wolof) | Tilde Biblia | Bibliche - La Biblia Interactiva