Tilde Biblia
Back to Reading

1thessalonians 4:16

Ndaxte ndigal lu jamp dina jib, baatu kilifa ci malaaka yi dégtu, liitu Yàlla jolli, te Boroom bi moom ci boppam dina wàcce ca asamaan. Booba ñi gëm Kirist te dee dinañu jëkka dekki;

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.

1thessalonians 4:16 - Téereb Injiil (Wolof) | Tilde Biblia | Bibliche - La Biblia Interactiva