Back to Reading
2thessalonians 1:10
▼
“Dina ñëw bés booba, ngir ndamam jolli ci biir gaayam yu sell yi, te ñépp ñi ko gëm yéemu ci moom— te ci ngeen bokk, ndaxte gëm ngeen li nu leen seede.”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.