Tilde Biblia
Back to Reading

matthew 18:12

¶ «Luy seen xalaat ci lii? Su fi amoon nit ku am téeméeri xar, te benn ci ñoom réer, lu muy def? Ndax du bàyyi ca parlukaay ba juróom ñeent fukki xar ya ak juróom ñeent, te dem wuti ma réer?

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.