Tilde Biblia
Back to Reading

matthew 18:6

Waaye ku yóbbe bàkkaar kenn ci ñi gëna tuuti ñi ma gëm, li gën ci moom mooy ñu takk doj wu réy ci baatam, sànni ko ca fa gëna xóot ca géej ga.

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.

matthew 18:6 - Téereb Injiil (Wolof) | Tilde Biblia | Bibliche - La Biblia Interactiva