Back to Reading
matthew 2:13
▼
“¶ Bi nga xamee ne boroom xam-xam ya ñibbi nañu, benn malaakam Boroom bi feeñu Yuusufa ci gént ne ko: «Erodd mu ngi ci tànki wut xale bi, ngir rey ko; jógal nag, jël xale bi ak ndeyam te nga daw jëm Misra, toog fa, ba kera ma koy wax.»”
Want to go deeper?
Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.