Tilde Biblia
Back to Reading

matthew 21:15

¶ Bi nga xamee ne sarxalkat yu mag ya ak xutbakat ya gis nañu yëf yu doy waar ya mu def, te dégg xale yu ndaw ya nekk ca kër Yàlla ga, di wax ci kaw naan: «Osaana, yaw Sëtu Daawuda bi!» ñu daldi mer.

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.