Tilde Biblia
Back to Reading

romans 2:14

Ndax ñi dul Yawut te nekkuñu ci yoonu Musaa, ñu ngiy def li yoon woowu tëral, ndaxte Yàlla def na ko ci nit. Te wonee nañu noonu ne man nañoo ràññee lu baax ak lu bon, su ñu nekkul sax ci yoonu Musaa,

Want to go deeper?

Launch Tilde AI. Ask a specific question and we'll extract knowledge in real time.